These are from the book Junniy Leebuy Wolof by Mànsóor Xumma.
- Aat yaa ngi woy géwél yi.
- Ab jatang, loo bàcc bàcc mu xasawum saw.
- Ab loot, tàbbi na ba tàyyi bàyyi fa rew bu nyor.
- Ab sàmm a waral béy deewul.
- Ab ndóol, ku mu yàqal nyakk nga.
- Ag bóli, mbedd la; waaye kenn du ca wetal i béy.
- Alal du faj dee, gàcce lay faj.
- Alali golo, ca lex ba.
- Alali jàmbur, ba fa la sant.
- Alali jàmbur, ku ca banya kasara, leneen nga ca begg.
P.S. - I don’t have the answers for these…You’ll have to figure them out for yourself!
No comments:
Post a Comment