More time & directions…
Phrases To Practice / Phrases à la pratique
Ban waxtu moo jot? - What time is it?
Minwi jotna. - It is midnight.
Fukki waxtu ak ñaar jotna. - It is noon.
Naka laa fay demee? - How do I get there?
Ci wetu jumaa ji. - Next to the mosque.
Toppal yoon wi. - Follow this road.
Xam nga fan la? - Do you know where it is?
Kan ngay ñew? - When are we arriving?
No comments:
Post a Comment