Midi Jotna. - It is noon.
Netti waxtu ci ngoon jotna. - It is three in the afternoon.
Jubelal ci biir dekk ba. - Keep going straight through the town.
Ci ñaari waxtu la nuy egg. - We are arriving at two o’clock.
Da ngay tallal ci kanam. - Straight ahead.
Naari waxtu ci suba jotna. - It is two in the morning.
Kan ngay dem? - When are we going?
Ci kanamu jumaa ji. - Across from the mosque.
Fukki waxtu teg na ñeent fukki i simili ak juroóm. - It is ten forty five.
No comments:
Post a Comment