See The Original List & Comments Here “Opposites Attract”
beginning - ending (verb): door/tammbali - jeex/mujj
cheap - expensive: yomb - jafe
easy - difficult: jomb - jafe
friend - enemy: xarit - noon
happy - unhappy: beg - tiis
inside - outside: ci biir - ci biti
enter - get out: duggu - genn
left - right: cammoň - ndeyjoor
near - far: jege - sori
open - close (verb): ubbi - téjj
peace - war: jamm - xare
No comments:
Post a Comment